L'Actualité en Temps Réel

Attaque contre Youssou Ndour…Diaraf Sow démonte Sonko

SAISIR LES BIENS INVESTIS PAR YOUSSOU NDOUR TU DIS ?…Par Diaraf Sow
Ah bon ! kone li Youssou Ndour ame, alalou askan wi la ?
Sonko, Est ce que yow nit ngueu ?
Doff keneu douko ni ya môme khew mi
Mais Sonko nak yangui begueu eupeul
Youssou Ndour dafa ligguey ba ame limou ame.
Yaw démal ligueyyi, ba ame li Youssou ame.
Youssou dafa investir Sénégal, créé aye emplois, aye domou rewmi dithi ligguey di doundeul seni ndiabotte.
Yow nak sokhor ak ignane rek nga dekkal thi rewmi ak doul you doul diêkh.
Di doul goudi ak bethieuk ak reylou aye domou diambour lakheu sey dôme.
Bô sagnône sénégalais yepp dê si ndoll AK gnakk.
Pourtant bi Tahibou Ndiaye di sathi dila diokh de 2000 à 2012 keneu degoula wône.
Youssou Ndour mola gueune, bayou youssou Ndour gueune sa baaye.

Khamal ni Youssou Ndour doundé Woul quête cotisation aki kopar Express.

Loumou ame dako gnakh mou lewko dôme.

Sénégalais yepp ame thi môme thioféle, mbekté ak fierté.

Bayiwô keneu nak wayé biss bo dougué si Youssou Ndour dinga khamni do gatt si rewmi.

Ndakh ko eupoul aye mbokk menouloko dieuw.

Kepp kouy gor si rewmi rek diem nga gakkal derame mba nga toumalko loudoul deug.

Té yow do gatt loudoul féne kat bou mag bou gnepp ragné thi aye féne

Féne nga féne bagnou dakh la finga dône ligueyé

Wayé Dokhal rekk, adouna ngui sa kanam

Sama mame dane na wakh naane, lou waay rendi sa lokho lay nathi

Té nak derêtou tégueul dou moy mouk loupou boromame

Me Diaraf SOW Président du parti ADAE/J