Dr Massamba Gueye: « Keen du wa Senegaal ni ci biir ak bitim réew. Baal leen ma àq ci lépp »

0

« Votre soutien est mon rempart dans cette épreuve unique qu’est la perte de ma nièce, femme et soutien Mberry Kassé. Je suis redevable à vie.

Wéetu ma ci sama naqar wii di deewu sama soxna, jarbat, wétal Mberry Kassé. Aw ma seen fey bilaay ! Bàayi naa leen ak Yàlla sunu boroom. Keen du wa Senegaal ni ci biir ak bitim réew. Baal leen ma àq ci lépp »

 

Dr Massamba Gueye

Laisser un commentaire

Votre adresse email ne sera pas publiée.