Guy Marius Sagna démasque Air Sénégal SA: « Ndoxu France lañuy joxe ci Air Senegal »

On demande les Sénégalais de voyager avec la compagnie nationale malgré ses nombreux manquements mais une fois dedans ce sont des produits français que vous allez consommer. L’activiste Guy Marius Sagna vient de démasquer le deal de AIR SÉNÉGAL SA.

Ndoxu France lañuy joxe ci Air Senegal
Raxas Building Administratif Macky dénk ko doomi France
Sunu téléphone nu dénk ko doomi France
Sunu autoroute à péage ñu dénk ko doomi France
Franc cfa ñu dénk ko doomi France
Sunu budget ñu dénk ko FMI ak banque mondiale
Làkk wi nuy jëfandikoo ci sunu lekool, farãse
Xare (armée) bu Farãs di daagu sunu biir réew
Sunu patrimoine culturel ñu denc ci musées France yi
Sunu constitution nu roy ci bu France
Sunu misig hymne national saf sàpp France
Photo sunu Président sax ñu woo doomu France
Sunuy mbedd ñu jël tuddee doomi France yi nootoon sunu maam ba ci sunuy baay
Raxas douche Macky dénk ko tubaab yi
Waas jën Macky dénk ko tubaab yi
Fippu jot na!
Jallarbi jot na!
Folli jot na!
Tekki jot na!
Moom sa réew jot na!
GMS

Comments are closed.