Mariage de Pape cheikh Diallo et Kya Aidara témoignage de Bijou Ndiaye Sy

0

Mes deux amours se sont dit oui!!!! Ma joie est incommensurable! Souma naré wakh séne aye D’jiko fi lay fanane ! Yalla mo kham loutakh mou bolé léne! Kone Yalla naléne lafal thiat dakhal léne seytané, mousseul léne, bolé séne aye weurseuk ngéne seuy ba lakh. Ma si gnane Khady Bijou Diallo nak ! Je vous aime Mr et Mme Diallo bilakhi dou aye thakhane! #Heureuxmenage ❤❤❤ @kya.di

Laisser un commentaire

Votre adresse email ne sera pas publiée.