« TALIF » de Fatou Kiné Dème TFM Pour Mariane Siva « Soopey nieupe demna ta dotou nieuw «

0

Sama Taarikh bi Marianne laako doupe
Marianne demna ta dotou nieuw
Djiguene dja dekewoone kaf tadou mer
Woutaloone boopame aw tour bacii nieneene
Marianne demna ta dotou nieuw
Taille fine mouni boopame nieneene mouni Adji Ndawa
Mouye stress, ak lamou lamboole, Marie khamoul loumaye ambiance, violences dakadane daw
Marianne demna ta dotou nieuw
Yiiw gua taakhna mou doonone royouwaaye
Fonkoone diineme, nangouwoonatia geusstoo
Moo waral moudane baakhé niit gni aye yoobal
Leep leep di ngeunel
Marianne demna ta dotou nieuw
Djambar daanouna ci toolou khaare
Da ligueye ta doune mouk soonouna
Boudoone diamono diou ndieukedia daagnoukoye Cheikhaal
Ndakh dadaane def ligueyame, baay def ligueyoup kenene , ta dara takhoul loudoul yeurmande
Marianne demna ta dotou nieuw
Niemewoone deug ta diko wakh, boula rousse dana kaf ba yeguelako
Meuna kaf loole moo waral ma degue ci sama natango ape seere bou ap waaydiourame def ci moome
Marianne bou guissoone deeh di nieuw dana kaf ak moome ba deeh roussko delou, Faty khamna limaye waakh.
Al Mouminah daama weet Yewouleen dana diooye
Soopey nieupe demna ta dotou nieuw
Marianne Aldjana Firdawsi Yallah nangafa khiipe Diop.

Abdou Khadre MBOUP-SENEGAL7

Laisser un commentaire

Votre adresse email ne sera pas publiée.