• Latest
  • Trending
  • All
Bëgg sa réew Mooy wane ko! (par  Pr Massamba Guéye)

Bëgg sa réew Mooy wane ko! (par Pr Massamba Guéye)

5 avril 2019
(Video) « Je comprends pas pourquoi Takku Wallu Waxni Douñko Def » Pape Djibril Fall sur le Retrait du recours « Bokouma Ci… »

(Video) « Je comprends pas pourquoi Takku Wallu Waxni Douñko Def » Pape Djibril Fall sur le Retrait du recours « Bokouma Ci… »

8 mai 2026
(Video) FADP, Sorties DIOMAYE & SONKO, L29 L30, O Ly remplacé par Me Tine: les revelations d’Ibrahima Lissa Faye

(Video) FADP, Sorties DIOMAYE & SONKO, L29 L30, O Ly remplacé par Me Tine: les revelations d’Ibrahima Lissa Faye

7 mai 2026
ADVERTISEMENT
« De la nécessité de corriger les insuffisances de la saisine institutionnelle du juge constitutionnel », (Par Thierno Alassane Sall)

« De la nécessité de corriger les insuffisances de la saisine institutionnelle du juge constitutionnel », (Par Thierno Alassane Sall)

7 mai 2026
Ndiaga Sylla : « Il est essentiel d’enseigner les vertus de la République à la jeunesse »

Ndiaga Sylla : « Il est essentiel d’enseigner les vertus de la République à la jeunesse »

7 mai 2026
League Conférence : Ismaïla Sarr et Pathé Ciss s’affrontent en finale, le 27 mai prochain

League Conférence : Ismaïla Sarr et Pathé Ciss s’affrontent en finale, le 27 mai prochain

7 mai 2026
Keur Ayib : Interpellation de 35 candidats à l’émigration clandestine

Keur Ayib : Interpellation de 35 candidats à l’émigration clandestine

7 mai 2026
APR : Oumar Sow accuse Thérèse FAYE DIOUF de fragiliser leur parti politique

APR : Oumar Sow accuse Thérèse FAYE DIOUF de fragiliser leur parti politique

7 mai 2026
(Video) Abou Diallo démonte Thérèse Faye après les rumeurs sur la coalition Diomaye « Dafa Wara Noppi… »

(Video) Abou Diallo démonte Thérèse Faye après les rumeurs sur la coalition Diomaye « Dafa Wara Noppi… »

7 mai 2026
ONU : Bougar Diouf réagit à l’immersion diplomatique de Macky Sall

ONU : Bougar Diouf réagit à l’immersion diplomatique de Macky Sall

7 mai 2026
Rencontre Sénégal – France : La génération 2002 rencontre l’ambassadrice de la France au Sénégal

Rencontre Sénégal – France : La génération 2002 rencontre l’ambassadrice de la France au Sénégal

7 mai 2026
Football : Le Real Madrid ouvre une procédure contre Valverde et Tchouaméni

Football : Le Real Madrid ouvre une procédure contre Valverde et Tchouaméni

7 mai 2026
Élections à São Tomé-et-Príncipe : La mission dirigée par Me Madické NIANG termine son séjour !

Élections à São Tomé-et-Príncipe : La mission dirigée par Me Madické NIANG termine son séjour !

7 mai 2026
  • About
  • Advertise
  • Privacy & Policy
  • Contact
vendredi, 8 mai 2026
  • Login
Senegal7
  • Accueil
  • Actualités
  • Politique
  • Société
  • International
  • Videos
  • Sports
  • People
No Result
View All Result
Senegal7
No Result
View All Result
Home Actualités

Bëgg sa réew Mooy wane ko! (par Pr Massamba Guéye)

by Assane Seye
5 avril 2019
in Actualités
0
Bëgg sa réew Mooy wane ko! (par  Pr Massamba Guéye)
491
SHARES
1.4k
VIEWS
Share on FacebookShare on Twitter

Bëgg sa réew
Mooy dëkkee bañ a
Pasar-pasaree alalam
Bañ a këpp i keesam
Bañ a jalgati ay àtteem
Bañ a xatal ay mbeddam
Bañ a asaaloo suufam;
Bañ a mbuxum ay lijjaasaam…
Bañ a ger ay àttekatam;
Bañ a lekk alali ger itam
Bañ a njuuj-njaaj ay woteem;
Bañ a gor ay àllam
Bañ a yalax ay géejam..
Bañ a tilimal ay ñallam
Bañ a tookeel am ndoxam
Bañ a tëj gemmiñu taskatu xibaaram
Bañ a bàyyi xale yi ciy mbeddam
Bañ a sànni mbuus ciy mbeddam;
Bañ a dóor ay jigéenam.
Bañ a jox ndombay tànk ay cuuneem!

Bëgg sa réew
Mooy it
Di xëy waxtu di wàcc waxtu
Di liggéey te doo tappale
Di bokk ci ñiy wote ;
Di Wegg raayaam;
Di setal deram
Di sellal ay mbeddam;
Di Fay say galag;
Di weeje ñiy sacc ak a yekktaan ;
Di sàmm alalam tey yamale
Di téeyee alalam tëddee njaaxaanaay
Di ko bañ a saax-saaxee.

Bëgg sa réew
Mooy faj ay doomam
Mooy sàmm ab deram
Mooy aar alalam
Mooy it teeru ak màggalam
bés bi mu moomee boppam!
©️ Dr Massamba Lba Guèye
/-//

Aimer son pays…
C’est le montrer!

Aimer son pays,
C’est surtout ne pas
piller ses ressources;
Ne pas détourner
ses deniers publics;
Ne pas violer des lois;
Ne pas encombrer ses rues;
Ne pas brader ses terres;
Ne pas trafiquer ses diplômes;
Ne pas corrompre sa justice;
Ne pas se laisser corrompre
Ne pas truquer ses élections;
Ne pas dévaster ses forêts;
Ne pas vendanger ses mers;
Ne pas salir ses ruelles;
Ne pas polluer ses eaux;
Ne pas museler sa presse;
Ne pas laisser ses enfants en rue
Ne pas jeter de sachets en rue;
Ne pas brimer ses femmes.
Ne pas promouvoir les médiocres

Aimer son pays,
C’est aussi
Être ponctuel;
Travailler sans tricher;
Voter aux élections;
Respecter son drapeau;
Construire sa belle réputation;
Nettoyer ses rues;
Payer ses impôts;
Dénoncer le vol et le viol;
gérer ses richesses équitablement;
Gérer ses biens inclusivement;
Gérer sans piller ses ressources.

Aimer son pays,
C’est soigner ses enfants;
C’est soigner sa réputation;
C’est protéger ses ressources;
C’est aussi …
fêter son indépendance!
©️ Massamba Guéye

Share196Tweet123
Assane Seye

Assane Seye

  • Accueil
  • Actualités
  • Politique
  • Société
  • International
  • Videos
  • Sports
  • People
Call us: +1 234 JEG THEME

Copyright © 2026 SENEGAL7.

Welcome Back!

Login to your account below

Forgotten Password?

Retrieve your password

Please enter your username or email address to reset your password.

Log In
No Result
View All Result
  • Accueil
  • Actualités
  • Politique
  • Société
  • International
  • Videos
  • Sports
  • People

Copyright © 2026 SENEGAL7.