Urgent – Oustaz Makhtar Sarr brise enfin le silence après le retrait de la plainte : « Zero médiation Yoniwunu Kenn muy négocier »

Dans un communiqué publié sur sa page Facebook, Oustaz Makhtar Sarr, a décidé de reagir à l’actualité, suité à la décision de Wally Ibrahima Wade Seck de retiré sa plainte contre lui.

Senegal7vous publie in extenso le texte de Oustaz Makhtar Sarr :

Neenaay daa retiré plainte bi !
Limata xam nak mooy : 0 Médiation 0 médiation 0 médiation Yonniwunu Kenn muy négocier dara,
#ñooma tifliwoon ñooko maraat !
Dawunu daayunu…
lumat 10 avocat taxawoonañ ngir défendre nu,,
Ñi bañ lubon ñëpp ñingi taxawoon ci Zaahir ak Baatin !
#Aka neexoon nudem ci !
Kufiy promouvoir ak ngóor jigéen ñu dénonce la ak koo manadoon !!! Buñ tàyyiwul dunu tàyyi..

Noongi Sant Mboolee Sénégalais yiy bañ lubon tax ñu taxaw ci Sunu wet 100%
Di ci Beral çànt Sunu Serigne #Serigne Babacar Sy Abdou Aziz, Serigne Mam Alfa Sy, Serigne Pape Makhtar Kebe, Serigne Habib Mbacke Habibou, Serigne Cheikh Ahmed Tidian Tall, Serigne Fatah Sarr, Professeur Ababacar Mboup ak Mbooleen waa #ÀND SÀMM JIKKO YI….
Imam Babacar Sylla Imam Khadim Ndiaye ak Mbooleem waa #AAR DAARA
XalaatTv, Asfiyahi, Nabytv92, Dakar fecbeut,…. Ak Mbooleen Site internet…
Ku lim du matal…….

Le 11 binak dina am ci Geneen anam Inchà Allàh..

Le combat contre l’homosexualité continue !!

وكل شيء ما خلا الله باطل ludul Yàlla neenla

 

Comments are closed.